Jammu Africa

Afrika a a a Afrika mon Afrique
Sama gent gi maa ngi ñaan Yalla wonma ko bala may ñibbi barsaq
Ma ne bes du ñakk ci bes yi Afrika don benn reew
D'ici ou d'ailleurs nous somm' des enfants d'Afrique
Mêm' si le ciel tombait luttons pour la paix
Kon jammu Afrika moom lay ñaan
Mané jammu Afrika mooy suñu natange
Afrika a a a Afrika a a
Afrika a a a Afrika mon Afrique

Yow mi nekka bittim reew man mi Lô maa ngi lay ñaan
Ak loo fa meun ta am ak noo fa meun ta mel bul fatte Afrika
Ici ou ailleurs la paix prix du bonheur
Mêm' si le ciel pleurait luttons pour nos frères
Kon jammu Afrika moom lay ñaan
Mané jammu Afrika mooy suñu natange
Afrika a a a Afrika a a
Afrika a a a Afrika mon Afrique

Onon bibbe Afrika ngimode, ngimode liggo-den leydi men
Ngaccen hasi daagal yoo Alla suren e musibaadi
Yoo Alla addu jam to Ruanda
Yoo Alla addu jam to Burundi
Yoo Alla addu jam to Casamans
Lawol Mbignona yee

Jammu Africa

Afrika aaa Afrika minha África
Sama gent gi maa nña Ñaan Yalla wonma ko bala com ñibbi barsaq
Ma ne bes du ñakk ci bes yi Afrika don benn reew
Aqui ou em outro lugar, somos filhos da África
Mesmo que o céu caia, vamos lutar pela paz
Kon jammu Afrika moom lay ñaan
Mané jammu Afrika mooy suñu natange
Afrika aaa Afrika aaa
Afrika aaa Afrika minha África

Yow mi nekka bittim reew man mi Lô maa ngi lay ñaan
Ak loo fa meun ta am ak noo faun me mel bul fatte Afrika
Aqui ou em outro lugar, o preço da felicidade
Mesmo se o céu chorasse, vamos lutar por nossos irmãos
Kon jammu Afrika moom lay ñaan
Mané jammu Afrika mooy suñu natange
Afrika aaa Afrika aaa
Afrika aaa Afrika minha África

Onon bibbe Afrika ngimode, ngimode liggo-den leydi men
Ngaccen hasi daagal yoo Alla suren e musibaadi
Yoo Alla addu jam para Ruanda
Yoo Alla addu jam para Burundi
Yoo Alla addu jam para Casamans
Lawol Mbignona yee

Composição: